audio audioduration (s) 2.68 7.99 | transcription stringlengths 29 63 |
|---|---|
mu teg saakam dal di dem ubbi palanteer bi | |
danga geestu ma xam ne moom geen di wax | |
metitlu na li nga ko yégalul takk gi | |
dinaa ko jot su ma yéegee ci taabal bi | |
këram dafa dëddu moo tax li ma fay dem barewul | |
ndégam mënuma fi xejj ñibbi rekk a ma dese | |
ca suba sa mu xëyaat dem summeeku ba set daldi né | |
tey dama naaje damay dem màrse ba ñów sog a sang xale bi | |
sàcc yi yóbbu nañu ganaar yi woon ci ngunu li | |
léegi du jamano soob nawet lay ñor | |
ndegam sa doom sëppéen la simis bi dana ko war a jot | |
boo fay dem ak woto dafay mel ni lu jége | |
fetal na mbaam àll mi doon ruur sunu tool yi | |
wool waxambaane yi ñu déqati bi ñu samp ci gannaaw | |
ba nuy nas nag lanu nemmeeku ne dafa jalgati lenn ci xaalis bi | |
leegi li ñu wara def mooy balu ko te daw seeti feneen | |
maa ngiy fàttaliku bés ba nu dajee foofa | |
dalal nga sama xel bi nga ma nee am na liggéey | |
Nanga ma ko fàttali lu ko moy dinaa ko fàtte | |
yaay daal nit a ngi xeeñ ci néeg bi | |
bi mu amee liggéey ba tey mu ngi ci jàmm | |
xamoon ngeen bu baax ne àttanul biib liggéey | |
seetal ci kóllëre gi dox sunu diggante | |
jinne ja dégg ko daldi fab lu doon ag ngeer | |
njaambur njaambur yi bey nañu ñebbe ju bare | |
sama kër a ngi féete jàkka ji sowu | |
jéem naa ko jubbanti ba tàyyi bërgël naa ko | |
sa xar maa ngi goor de mba du dafa feebar | |
mu ngi ne xàmm déggul dara ci li nga ko wax | |
lal fa seeni basan di naan sàngara di tóx di lekk yàpp | |
fekk na biram njéemée nga yendu ca mbënn ga fanaan ca | |
gox boobu fég nal sampal nañu ku nekk robine | |
su janax di sóoru muus ñag baa fa jege | |
mu téye ko lu yàgg ca yoxoom ya ba noppi bàyyi ko mu dem | |
caaxaan wéy na danga war jëmbët fulla ci njàng mi | |
mbuumbaay mee tax mënul def dara lu àntu | |
ci similaak saala asamaan si xiin ba ñalingaan | |
soo ko ko dënkee dina ci def farlu gi ci war | |
bul sànni xuuru xar mi am na du koy wàjj | |
dañu mànkoo ne dootuñu wax ak moom | |
loo xam ci suñu waxtaan ba ne xëtëb dugg ci | |
doj wi ñu ko sànnee ngi yem ci ndoN li | |
sompal tuuti ci poobar bi def ci cin li | |
bul tiit defuloo ko dara ba mu di la ñaan yàlla | |
ey biram njéemé koo njaay mu ngi ci kemu dëkk bi | |
jaxato dafa xaw nurook tamaate fàrsi | |
maamam a daan tëgg laxaab yi ca dëkk ba | |
fii laa ko tegoon xef ak xippi ñu jél ko | |
dànkaafu naa ko ba tàyyi mu të maa déglu | |
te sax boo dawul ñu nàngu sa allal faat la | |
séytaane teg ko ca jombaxtalu tangor ba | |
cere ji dafa wow kaas ko bala nga koy tay | |
dama leen woolu ngir laaj leen seen xalaat | |
bu ñu amaan gan ab gàtt lañu ko daan rendil | |
dangay gis jiit yi di dox ci leere gi | |
sama xol sedd na ci liggéey bi mu def | |
bër set mu daldi fàqlu lu dooni yari daqaar laxasante ko | |
yaa ngi téju rekk ci néeg bi génnal féexlu tuuti | |
mu yegg ci beneen dëkk nekkaat fa jaamu kër buur | |
muus mi dafa fettax dal ci kow janax ji | |
ba ko rajo bi waxee la coow la ne kur | |
puju néeg dina xeex ak taw te borom néeg du yég | |
mu ne mënula ñów waaye mu ngi leen di yokk ngóora | |
kolkolaat yégul né yembà baah nà | |
am xéy laa ko ameel ngont li maa ko moom | |
mu dem ci yaay ji ni ko buur nee na nga jél mu may la | |
ab roq la dajalee siddéem yi nekkoon ci toolam yépp | |
maa ko saytu ba mu fereem soow ba tey | |
xawma lu mu jóge ak ñaq wiy siit ci kanam gi | |
jox sama baay muraakem seel la maa ko nangoo ci Naar yi | |
dafa bëgg xam lu nekk ci kër njulli kaata bi | |
ku jél rongoñ siim céree m bu ko ñaan ñéh | |
benn xaal gala gàbbu na ko biram njéemé ndënnéer na | |
bunt baa ngi ne àpp te terewul mu tàng | |
gàpp bi weesu na bu yàgg dama koy seeti ndax ma soññ ko | |
njaayam mi du jar bu baax ndax dafa seer | |
kou di loo kham wëkh ko së ngor yakhou | |
li des ci sow mi matul sax ñaari góox | |
dafay jénd ay xar yafal leen jaayaat leen | |
dama koy saam ci lay gëna gaawa jare | |
moomuñu kër gi ñu dëkk dañu ko luye rekk | |
yeggaleel sa njàng moo la ëppal njariñ | |
doktoor bii mooy toppatoo ñi nga xam ni dañu siti | |
senegaal dafay jaay ariko bitim réew | |
ku ñu ko tànnal rekk mu né bëggu ko | |
su lëg lekkee aloom na ko gërëme coy | |
waa gànraar takk ab xare dabsi biram njéemé | |
fanweeri dërëm laa ko jox mu delloo ma ñaari dërëm | |
yàkkamti woon naa ñibbisi ba lat ci pajaas bi | |
mënuloo jënd garab goo lugate sa bopp bi | |
dégtal nañu leen ne dinañu fi jéle marse bi | |
bala ngaa jënd tam tamal ganaar gi | |
jéego boo def ngir jubale ay xarit yàlla dina la ko fey | |
Nangeen bàyyi xel ci dénkuwaay yooyu | |
dàmp bi ngay def baax na ci toogaay bu yàgg bi | |
jigéen ñu bare ñemewuñu njurug seex | |
saa doom xam nga lan mooy àddinaam | |
dinga yaakaar nit fekk mënul faj sa soxla | |
bala ngay tase ak moom dangay bëre ak ay suqam | |
sëpp jaleñ du la fasale ak say teeñ |
End of preview. Expand
in Data Studio
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 43